Penku Tugal

Jóge Wikipedia.

Penku Tugal mooy diiwaan bi ëmb Réew yi ne Penku Tugal. Réew yi Bennog Sofyet gi tegoon loxo ci mujjug Ñaareelu Xareb Àdduna bi, yenn yi génn nañu ci, yeneen yi des ci.

Penku Tugal ci gisiin gu yaa

Séwógaraafi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Diwaani Tugalasi
Asi      Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End
Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri
Tugal      Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal 
Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi