Tugalasi

Ci Séwógaraafi Tugalasi ab gox la bu mbooloo bu ñaari gox yii di Tugal ak Asi jëmmal, walla benn xaaj ci Afritugalasi, ni ko ñenn ñi di waxee.
Yaatuwaay: 54 000 000 km kaare
Askan: 4,8 miliari way dëkk
Tugalasi ak Afrik, ñoom la ñuy woowee àdduna gu yàgg ga, ndax li fa xay yi gën a yàgg juddoo. Baat bi day safaanoo ak àdduna gu yees gi, di ñaari gox yii Aamerig ak Oseyaani
Afritugalasi | Oseyaani | Afrig | Tugalasi |
Bëj-gànnaaru Aamerig | Tugal | Asi | Bëj-saalumu Aamerig |