Bëj-gànnaaru Tugal
Apparence
Bëj-gànnaaru Tugal mooy wàll gu Bëj-gànnaar gu goxu Tugal. ni nuy xoolee Bëj-gànnaaru Tugal daa bariy fànn.
Gisiin wu néewal gi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Yii ñooy réew yi fa ne:
Ñii la ñuy woowee Réewi bëj-gànnaar yi
Gisiin wu yaa wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Yii ñooy réew yi fa ne:
Gisiin wu MR
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Su ñu sukkandikoo ci ni ko Mbootaayu Réew yi gisee, Yii ñooy réew yi ne ci Bëj-gànnaaru Tugal:
Diwaani Tugalasi | |||
Asi | Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri | ||
Tugal | Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi |