Nguur-Yu-Bennoo
Apparence
The United Kingdom of Great Britain and Northern Ireland Nguur-Yu-Bennoo | |||||
| |||||
Barabu Nguur-Yu-Bennoo ci Rooj | |||||
Dayo | 244 101 km2 | ||||
Gox | |||||
Way-dëkk | 60 943 912 nit (2008) | ||||
Fattaay | 244 nit/km2 | ||||
Xeetu nguur - Njiitu Réew - Njiitu Jëwriñ |
|||||
Tembte - Bawoo - Taariix |
|||||
Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
Londar | ||||
Làkku nguur-gi | Wu-angalteer | ||||
Koppar | |||||
Turu aji-dëkk | |||||
Telefon | |||||
Nguur-Yu-Bennoo walla Nguur Yu Bennoo yu Brëtaañ gu Mag ak Irlaand gu Bëj-gànnaar (United Kingdom of Great Britain and Northern Ireland), ñenn ñi di ko wax angalteer, am réewu bëj-gànnaaru Tugal la.
Nguur gaa ngi judd ci 1800 ci booloog Nguurug Brëtaañ gu Mag ak Nguurug Irlaand. Ci 1922 la wàll gu yaa ci Irlaand dagg, tudde boppam Réewum Irlaand. Nguur gi dafa séddalikoo ci ñeent: Angalteer, Irlaand gu bëj-gànnaar, Wales ak Ekos