Ron-goxu End
Apparence
Ron-goxu End mi ngi nekk ci bëj-saalumu Asi.
Ay réewam:
- Banglaades
- Butaan
- Biirmaani (ci lu bari Bëj-saalum-penku Asi la ñu koy boole.)
- End
- Maldiif
- Nepaal
- Pakistaan
- Siri Laanka
Rëy gi mu rëy ak ni mu beroo moo tax ñu def ko ron-gon, li fa réewu End gën a yaa mo tax ñu gox ko turam.
Diwaani Tugalasi | |||
Asi | Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri | ||
Tugal | Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi |