Diggu Asi

Jóge Wikipedia.

Diggu Asi benn la ci diwaan yi ñu sedatlee goxu Asi. Cig déggoo mi ngi tambalee ci Géeju Kaspio ba ca bëj-gànnaar-sowwu gu Siin.

Diggu Asi ci lonkoyoonu àdduna bi

Réew yi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Séwógaraafi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Sori géej, doon it diwaan bu man a sedd. Ci wàllu bëj-gànnaar, li ko dalee ci Volta ba ci Mongooli, jaare ko ci Kasakistaan, ab kekk la def bu ay sàmmkat dëkkee. Am na ñaari tàkk bu Taklamakaan ak bu Gobi.

Ab càllaley doj moo nekk ci bëj-saalum-penku Diggu Asi, ñooy sax doj yi gën a kawe ci àdduna bi, doju Pamir, doju Hindi Kush, doju Himalaya.

Ca doj yooyu la dex yi leen di dimbali ci mbéy mi di ballee. Li ëpp ci diwaan bi ñakk na lool taw.

Diwaani Tugalasi
Asi      Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End
Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri
Tugal      Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal 
Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi