Bëj-saalum-penku Asi
Bëj-saalum-penku Asi ci goxu Asi la bokk.
Su nu sukkandikoo ci sedatle, bu àdduna bi, gi Mbootaayu Réew yi def, Bëj-saalum-penku Asi benn la ci diwaani Asi.
Réew ya fa nekk:
Brunaay Daarusalaam
Kamboodiya
Endoneesi
Lawos
Maleesi
Miyanmaar
Filipiin
Singapoor
Taaylaand
Timoor gu Penku
Wiyetnaam
Réew yépp yi nekk ci lim gi ci kaw, ba mu des Timoor gu Penku, ay Cër la ñu ci ASEAN: di ab mbootaay bu judd ngir soqali koom-koom mu diwaan bi jaare ko ci jappalante.
Diwaani Tugalasi | |||
![]() |
Asi | Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri | |
Tugal | Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi |