Bëj-gànnaaru Tugal

Jóge Wikipedia.
réewi Bëj-gànnaaru Tugal ci gisiin gu néewal gi mooy yolet gu ñor gi, Gisiin gu yaa gi mooy gu leer gi

Bëj-gànnaaru Tugal mooy wàll gu Bëj-gànnaar gu goxu Tugal. ni nuy xoolee Bëj-gànnaaru Tugal daa bariy fànn.

Gisiin wu néewal gi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Yii ñooy réew yi fa ne:

Ñii la ñuy woowee Réewi bëj-gànnaar yi

Gisiin wu yaa wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Yii ñooy réew yi fa ne:

Gisiin wu MR[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Su ñu sukkandikoo ci ni ko Mbootaayu Réew yi gisee, Yii ñooy réew yi ne ci Bëj-gànnaaru Tugal:

Diwaani Tugalasi
Asi      Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End
Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri
Tugal      Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal 
Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi