Tabaski
Apparence
Tabaski, (ci araab "sul-hajja" ذو الحج), tuddees na ko noonu ngir ne mooy boroom aj gi, ci la araab yi daan aji Màkka, ci la tabaski gi it nekk, moom nag bokk na ci weer yees wormaal .
Xew-Xew
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Ci lees di aj màkka,(ab ponk la ci lislaam war na jullit bu ko man),
- Ci lees di Tabaski (rayi xar, bëy, nag, galeem, jokkug bokk, baloonte àq, jullig bër, ak yuni mel...)
Lëkkalekaay yu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski |