Aller au contenu

Rakki-gàmmu

Jóge Wikipedia.

Rakki-gammu, (ci araab ربيع الثاني) tuddees na ko noonu ngir ne araab yi dañu ci daan lolliwu, maanaam daan ci am am ñax, di ci sàmm seenug jur, am ñu ne daa dëppoo ak lolli bi moo tax ñu tudde ko ko. Mooy ñeenteelu weer ci at mi, di weer ci njëkk ginaaw gàmmu gi

Lëkkalekaay yu biti

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski