Kori
Apparence
Kori (ci araab شَوّال), ci la jullit ñiy wori ci seenug koor, mi ngi tudd nag ci araab "Sawaal" ngir ne sawaal day tekki ci araab ag jeex akug ñàkk meew, te ci weer woowu seen naaga yi (giléem yu jiggéen yi) dañu ci daan jeex, ñàkk ci meew.
Mooy fukkeelu weer ci at mi, di itam weer wi njëkk gannaaw koor gi.
Xew-Xew
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Ci lees di korite muy bis bees di dog koor di màggal bis ba ngir gunge weer wu tedd wi wey.
Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski |