Baraxlu

Jóge Wikipedia.

Baraxlu, (ci araab sahbaan شَعبان ), tuddees na ko noonu ndax aw ñall la (shahb ci araab) ci diggante "rajab" ak "ramadaan". Waxees na ne nit ñi daño cee baaxoo woon a tàqalikoo ak a ñallu (tas) ngir sàkku-ji ndox, mu daal di jël tur woowu. Mooy juroom-ñetteelu weer ci at mi, di itam weer jiitu koor gi. Bokk na ci weer yi baax a woor ci jullit ñi

Lëkkalekaay yu biti[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski