Diggi-tabaski

Jóge Wikipedia.

Diggi-tabaski,( ci araab "sil-qihda" ذو القعد, moom nag ci weer yees wormaal la bokk: tuddees na ko noonu ci araab ngir ne "qahada" ci araab giy tekki jekki la baat bi juge, li ko waral nag di jekki gi ñu ci daan def wëlif xeex, wëlif it ñax, daawuñu ci laxas ngir sàmmi, daawuñu ci xeex, ngir wormaal ko, araamal ci xeex.

Mooy fukk ak benneelu weer ci at mi, di ñetteelu weer gannaaw koor gi, di itam weer wi Tabaski toftal .

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski