Ndeyi-koor

Jóge Wikipedia.

Ndeyi-koor,(ci araab rajab رجب ) moom nag ci weer yi am worma la bokk. Tuddees na ko nag Rajab ci araab, ngir ne ci weer woowu dees ci daa wéer ngànnaay yi, nocci ñawka yi wëlif xeej yi, daawuñu ci xeex, dees na wax (rajaba) maanaam taxawlu na wëlif xeex bi.

Mooy juroom-ñaareelu weer ci at mi, di itam ñaareelu weer laataa koor gi.

Xew-Xew[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • Ci lees di màggal juddug [Sëriñ Muhammadu Faliilu Mbàkke| Sëriñ Faalu Mbàkke] ca Senegaal di ko wax Kazu Rajab (27bis ci rajab).

Lëkkalekaay yu biti[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski