Aller au contenu

Rakkaati-gàmmu

Jóge Wikipedia.

Rakkaati-gammu ci araab jumaadal uulaa جمادى الأولى), njëkk Lislaam nag (jumaadaa xamsa) lees ko tudde woon, lu tax nag ñu tudde ko ko? ndax daa nekkoon ci sedd bi bi ñu ko koy tudde, nga xam ne ne ndox mi da daan way (jumaada) mi ngi jóge ci "jamada" giy tekki way, maanaam ndox mi da ci daan way di def ay donji yuur (galaas) ngir ag sedd.

Mooy juroomeelu weer ci at mi, di itam ñaareelu weer gannaaw gàmmu gi.

Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski