Aller au contenu

Melosuufug Bene

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Lonkoyoonu Bene

Bene aw rëdduw suuf wu sew la, nekk ci diggante yamoo gi ak Gëwéelub Sànkar bi. Rëddu tus-wu-gaar wu bene mi ngi ci diggante 6°30'bëj-g ak 12°30'bëj-g, tu-wu-taxawam moom mi ngi ci 1° P ak 3° 40'P.

Ay digam ñoo ngi yem ci Togóo ci sowwu, yem ci Burkina-faso ak Niseer ci bëj-gànnaar, ci Niseeriyaa ci penku, janook mbàmbulaanug Atlas gi ci bëj-saalum. Mi ngi am yaatuwaay gu tollu ci 112.622 yu kaare. Bene ngi bawoo ca dexub Niseer bi ci bëj-gànnaar yem ci mbàmbulaanug Atlas ci bëj-saalum ci ab tallalub 700 km. Diggante bi gëna guddu ci réew mi 325 km la.

Lëkkalekaay yu biti

[Soppi | soppi gongikuwaay bi]
  • (en) ICJ Judgment over the Benin-Niger boundary dispute, 12 July 2005
  • (en) Fabio Spadi (2005) The ICJ Judgment in the Benin-Niger Border Dispute: the interplay of titles and ‘effectivités’ under the uti possidetis juris principle, Leiden Journal of International Law 18: 777-794


Melosuufug Afrig

Afrig gu Bëj-saalum Alseeri Angolaa Bene Botswana Burkinaa Faaso Buruundi Kamerun Kap Weer Réewum Diggu Afrig Bennoo yu Komoor Kongóo-Brasaawiil Kongóo-Kinshasa Kot Diwaar Jibuti Isipt Eriitere  Ecoopi Gaboŋ Gaambi Gana Gine Gine-Bisawóo Gineg yamoo Keeñaa Lesoto Liberiyaa Libi Madagaskaar Marook Malawi Mali Móoris Gànnaar Mosambik Namibi Niseer Niseeriyaa Ugandaa Ruwandaa Sahara gu Sowwu Sao Tome-ak-Principe Senegaal Seysel Siraa Leyoon Somali Sudaan Suwaasilaand Tansani Cadd Togo Tuniisi Sambi Simbaawe