Aller au contenu

Melosuufug Buruundi

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Lonkoyoonu Buruundi
Buruundi

Buruundi am réewu diwaanu Diggu Afrig la, rëye na 27,830 km², 25,650 km² suuf la, 2,180 km² di ndox.

Melosuufug jëmm

[Soppi | soppi gongikuwaay bi]

Mi ngi digook Kongóo-brasaawiil ci lu mat 233 km ci sowwu, ak Ruwandaa ci 290 km ci bëj-gànnaar, lang ak Tansani ci guddaayub 451 km ci penku. Buruundi amul ubbeeku ci géej gi, waaye yi ci bëj-saalum-sowwu da ñoo lang ak déegub Tanganica bu rëy ba. Réew mi dafa nekk ci diggante ñaari mbandi ndox yu mag yii di Niil ak bu Kongóo

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons


Melosuufug Afrig

Afrig gu Bëj-saalum Alseeri Angolaa Bene Botswana Burkinaa Faaso Buruundi Kamerun Kap Weer Réewum Diggu Afrig Bennoo yu Komoor Kongóo-Brasaawiil Kongóo-Kinshasa Kot Diwaar Jibuti Isipt Eriitere  Ecoopi Gaboŋ Gaambi Gana Gine Gine-Bisawóo Gineg yamoo Keeñaa Lesoto Liberiyaa Libi Madagaskaar Marook Malawi Mali Móoris Gànnaar Mosambik Namibi Niseer Niseeriyaa Ugandaa Ruwandaa Sahara gu Sowwu Sao Tome-ak-Principe Senegaal Seysel Siraa Leyoon Somali Sudaan Suwaasilaand Tansani Cadd Togo Tuniisi Sambi Simbaawe