Tus-wu-taxaw
Sauter à la navigation
Sauter à la recherche
Tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi (beneen bi mooy tus-wu-gaar). Tus-wu-taxaw wi mooy tax ñuy man di féetale am mbir ci kaw Suuf si, ci penku walla sowwu