Aller au contenu

Melosuufug Afrig gu Bëj-saalum

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Afrig gu Bëj-saalum mooy réew mi gën a féete Bëj-saalum ci goxu Afrig, mi ngi bokk ci diwaanu Bëj-saalumu Afrig.

ci Bëj-saalum klimaa bu mel ne Gu Diggu gi la am, ci li wër Kap, ci bëj-gànnaar nag klimaab gëweel la am.

réew mi am na 47 556 900 ciy way dëkk. Ñetti dëkk yi fa gën a réy ñooy Kap mi am 2 984 100 ciy way dëkk, Duurbaan 2 531 300 ciy way dëkk, Johannesburg 1 975 500 ciy way dëkk ak Pretoriya, di péyam, am lu tollook 1 473 800 ciy way dëkk (yii lim nak ca 2004 lawoon).

Réyaayam toll ci 1 219 912 km², di 33° réew ci réyaay ci àdduna bi. Am tefes gu guddee 2 798 km. Mi ngi feggool ak Botswana, Lesoto, Mosambik, Namibi, Eswatini, Simbaawee, réew yii yépp nag ci bëj-gànnaaram la ñu ne. Pegg gi ne ci seen diggante nag toll na ci 4 862 km.

Lëkkalekaay yu biti

[Soppi | soppi gongikuwaay bi]


Melosuufug Afrig

Afrig gu Bëj-saalum Alseeri Angolaa Bene Botswana Burkinaa Faaso Buruundi Kamerun Kap Weer Réewum Diggu Afrig Bennoo yu Komoor Kongóo-Brasaawiil Kongóo-Kinshasa Kot Diwaar Jibuti Isipt Eriitere  Ecoopi Gaboŋ Gaambi Gana Gine Gine-Bisawóo Gineg yamoo Keeñaa Lesoto Liberiyaa Libi Madagaskaar Marook Malawi Mali Móoris Gànnaar Mosambik Namibi Niseer Niseeriyaa Ugandaa Ruwandaa Sahara gu Sowwu Sao Tome-ak-Principe Senegaal Seysel Siraa Leyoon Somali Sudaan Suwaasilaand Tansani Cadd Togo Tuniisi Sambi Simbaawe