Aller au contenu

Melosuufug Kamerun

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Kamerun am réewu diggu Afrig la, jëmmam dafa mel ne ab ñettikoñ, rëye na 475 442 km², 98,8% di suuf, 1,2% ndox la, di 42u réew mi ëpp ci àdduna bi, am na it 402 km ci tefes.

Réewum Niseeriyaa moo ko féete sowwu, Mbàmbulaanug Atlas gi, Gineg yamoo gi, Gaboŋ ak Kongóo-Brasaawiil nekk ci bëj-saalumam, Réewum Diggu Afrig ak Cadd nekk ci penku, dexub Cadd bi ci bëj-gànnaar.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons


Melosuufug Afrig

Afrig gu Bëj-saalum Alseeri Angolaa Bene Botswana Burkinaa Faaso Buruundi Kamerun Kap Weer Réewum Diggu Afrig Bennoo yu Komoor Kongóo-Brasaawiil Kongóo-Kinshasa Kot Diwaar Jibuti Isipt Eriitere  Ecoopi Gaboŋ Gaambi Gana Gine Gine-Bisawóo Gineg yamoo Keeñaa Lesoto Liberiyaa Libi Madagaskaar Marook Malawi Mali Móoris Gànnaar Mosambik Namibi Niseer Niseeriyaa Ugandaa Ruwandaa Sahara gu Sowwu Sao Tome-ak-Principe Senegaal Seysel Siraa Leyoon Somali Sudaan Suwaasilaand Tansani Cadd Togo Tuniisi Sambi Simbaawe