Dawaan bu safaanu wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
TXiKiBoT (waxtaancëru)
m robot Adding: eu:Korronte alterno
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Modifying: be-x-old:Зьменны ток; cosmetic changes
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
'''Dawaan bu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
'''Dawaan bu safaanu''' ('''DS''' walla '''AC''' ci [[wu-angalteer]]: Alternating Current) màndargoo ag walug [[dawaan]] guy soppiku ci jamono muy ci [[taraay]] walla ci jubluwaay.
== Doxiin ==
== Doxiin ==
Naka-jekk dawaanu [[mbëj]] suñu koy séddale ci dawaan bu safaanu bu [[Baraay|baraayam]] sax ci 50 Hz walla 60 [[Hz]] lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne).
Naka-jekk dawaanu [[mbëj]] suñu koy séddale ci dawaan bu safaanu bu [[Baraay|baraayam]] sax ci 50 Hz walla 60 [[Hz]] lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne).

Jëfandikoo gu dawaan bu safaanu mi gi jóge ci li [[Jurukaay|jurukaayu dawaan]] yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan bu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan bi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.

Rëdd 11 : Rëdd 11 :
Donte yenn jumtukaay yi [[dawaan bu wéy]] lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan bu safaanu, sunu jëfandikoo ab [[jubbantikaay]].
Donte yenn jumtukaay yi [[dawaan bu wéy]] lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan bu safaanu, sunu jëfandikoo ab [[jubbantikaay]].

Suñu jëfandikoo ag xaralag [[mbëjfeppal gu kàttan]] gu ñaw, manees naa jëfandikoo dawaan bu wéy ngir am dawaan bu safaanu, jur ko ci yenn anami [[baraay]], [[melokaanu duus]] ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee [[Jallarbikaay|jallarbikaay]].
Suñu jëfandikoo ag xaralag [[mbëjfeppal gu kàttan]] gu ñaw, manees naa jëfandikoo dawaan bu wéy ngir am dawaan bu safaanu, jur ko ci yenn anami [[baraay]], [[melokaanu duus]] ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee [[jallarbikaay]].

== Taariix ==
== Taariix ==
Rëdd 18 : Rëdd 18 :
Ca njalbeenu njëfandikug kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIX<sup>u</sup> xarnu [[daawaan bu wéy]] lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy [[tegle]] ak li mu gën a wóor dawaan bu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon [[xareeb dawaan yi]].

Dawaan bu safaanu, gi soloom doonoon lu beneen xaaj bi boole woon [[Nikola Tesla]] ak [[George Westinghouse]] doon aar, manul a ñakk ci njëfandiku gu ab [[soppalikaay]], moom mi tax ñuy man jokkalante mbëj mi ci diggante yu gudd. Te itam [[doxalukaayu mbëj]] yu dawaan bu safaanu ñoo gën a wóor te gën a yaxan yu dawaan yu wéy yi.

Ci jamono jii ci [[àdduna]] bi dawaanu mbëj ci ñaari [[baraay]] lañu koy séddalee, 50 Hz([[Tugal]], [[Asi]], [[Afrig]]) ak 60 Hz([[Diiwaan-yu-Bennoo]] ak goxu [[Aamerig]] bépp ci lu daj, genn xaaju [[sapoŋ]]) ak taraay yu wuute.

== Xool it ==
== Xool it ==
*[[Dawaan gu wéy]]
* [[Dawaan gu wéy]]

*[[Dawaanu mbëj]]
* [[Dawaanu mbëj]]

*[[Kàttanug mbëj]]
* [[Kàttanug mbëj]]

*[[mbëj]]
* [[mbëj]]

==Téerekaay ==
== Téerekaay ==

* {{en}}[[Charles Proteus Steinmetz]]: [http://www.archive.org/details/theorycalculatio00steiuoft ''Theory and Calculation of Alternating Current Phenomena''] ([[McGrawHill]], [[1900]])
* {{en}}[[Charles Proteus Steinmetz]]: [http://www.archive.org/details/theorycalculatio00steiuoft ''Theory and Calculation of Alternating Current Phenomena''] ([[McGrawHill]], [[1900]])
Rëdd 47 : Rëdd 47 :
* {{en}}Ernst Julius Berg: [http://www.archive.org/details/electricalengine00bergrich ''Electrical Engineering, Advanced Course''] (McGrawHill, New York, 1916)
* {{en}}Ernst Julius Berg: [http://www.archive.org/details/electricalengine00bergrich ''Electrical Engineering, Advanced Course''] (McGrawHill, New York, 1916)

[[Wàll:Dawaanu mbëj]]

[[Wàll:dawaanu mbëj]]

[[ar:تيار متردد]]
[[ar:تيار متردد]]
[[be-x-old:Зьменны струм]]
[[be-x-old:Зьменны ток]]
[[bg:Променлив ток]]
[[bg:Променлив ток]]
[[bn:পরিবর্তী তড়িৎ প্রবাহ]]
[[bn:পরিবর্তী তড়িৎ প্রবাহ]]

Sumb bu 11 Maars 2010 à 23:19

Dawaan bu safaanu (DS walla AC ci wu-angalteer: Alternating Current) màndargoo ag walug dawaan guy soppiku ci jamono muy ci taraay walla ci jubluwaay.

Doxiin

Naka-jekk dawaanu mbëj suñu koy séddale ci dawaan bu safaanu bu baraayam sax ci 50 Hz walla 60 Hz lees koy defe (+ ak - bi dañuy safaanu ci watatukaay bi juroom-fukki saa yu ne).

Jëfandikoo gu dawaan bu safaanu mi gi jóge ci li jurukaayu dawaan yi, ci yaxanaay ci koom-koom ak seenug yomb a defar, di jur dawaan bu safaanu ci anam gu yomb, kon dawaan bi ci boppam kenn du ko soppiwaat laataa ag jëfandikoo.

Fi njariñ li gën a feeñee sax mooy séddaleeb dawaan bu safaanu bir na ne moo gën a yaxan dawaan bu wéy ci séddaleeb taraay bu kawe (ñakkug kàttan gi ci buum yu gudd yi moo gën a néew). rawatina, ci diggante gu gennwéq walla wéq yu bari, bir na yaxanaay gu ñettiwéq di gees gën a jëfandikoo ndax néewteey ñakkug kàttan ngir njeexitu Joule (moo tax dijjaayu watatukaay yi gën a néew, maanaam wëñ yu gën a sew); jëfandikoog dawaan bu safaanu bu ñettiwéq lawal na buumi yóbb yi ci diggante yu gudd lool yi.

Genn Màndarga gu am-solo gu dawaan bu safaanu, ba waral ci genn wàll li tax ñépp jël ko, mooy yomb gee jëfandikoo fu nekk, yomb gee soppi ci lim yu wuute ci taraayu dawaan, ci ndimbalu soppikaay yi, ak ñakkug kàttan gu digu.

Donte yenn jumtukaay yi dawaan bu wéy lañuy doxe, waaye loolu manees na koo ame ci dawaan bu safaanu, sunu jëfandikoo ab jubbantikaay.

Suñu jëfandikoo ag xaralag mbëjfeppal gu kàttan gu ñaw, manees naa jëfandikoo dawaan bu wéy ngir am dawaan bu safaanu, jur ko ci yenn anami baraay, melokaanu duus ak taraay jaare ko ciy jumtukaay yees duppee jallarbikaay.

Taariix

Lonkoyoonu àdduna bi bees melool aju ci taraay a baraayu kàttanu mbëj ci ndombo yiy séddale dawaan gi ci kër yi.

Ca njalbeenu njëfandikug kàttanu mbëj ci ndefar gi ci XIXu xarnu daawaan bu wéy lañu doon jëfandikoo, ndax li mu doonoon lu neex a rënk ciy tegle ak li mu gën a wóor dawaan bu safaanu. Tomb bu mujj bi Thomas Alva Edison mooy ki ko doon wax ci lees tuddewoon xareeb dawaan yi.

Dawaan bu safaanu, gi soloom doonoon lu beneen xaaj bi boole woon Nikola Tesla ak George Westinghouse doon aar, manul a ñakk ci njëfandiku gu ab soppalikaay, moom mi tax ñuy man jokkalante mbëj mi ci diggante yu gudd. Te itam doxalukaayu mbëj yu dawaan bu safaanu ñoo gën a wóor te gën a yaxan yu dawaan yu wéy yi.

Ci jamono jii ci àdduna bi dawaanu mbëj ci ñaari baraay lañu koy séddalee, 50 Hz(Tugal, Asi, Afrig) ak 60 Hz(Diiwaan-yu-Bennoo ak goxu Aamerig bépp ci lu daj, genn xaaju sapoŋ) ak taraay yu wuute.

Xool it

Téerekaay