Waxtaan:Dawaan bu safaanu

Jóge Wikipedia.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

cey boo manoon di defaale ci diggante ay xala ay tekki seen ci fr!

loolu yaakaaroon naa nekk waxoon nanu ci, man ni ma bëgg di liggéeye mooy bind lépp wolof rekk, baat yi nag, seen tekki, def leen ci wikbaatukaay ndax loolu moo tax ñu sos ko. ci biir jukki yi nag di fa defi lëkkalekaay yu fay jëme. Donte yenn baat yi nekkaguñu fa waaye dinaa leen fa dugal ndànk-ndànd. --Ibou (xëtu waxtaanuwaay) 14 Samwie 2010 à 08:46 (UTC)

boo gisee ma koy wax , damaa beggoon su ma gisee yooyu baat ci fr, nuy tax ma man a xam ba xam amul yu gën a méngoo ngir nu wottee leen ak yooya, bu ko defee fu ma ci noppee rekk bu la neexee dindi, waaye boo ko gisewul noonu it déet jafe-jafe , nawees na liggéey bi --Abdu Xaadir Kebe (xëtu waxtaanuwaay) 15 Samwie 2010 à 02:18 (UTC)