Kàttanug mbëj

Jóge Wikipedia.

Kàttanug mbëj xeetu kàttan la gu lonku ci doole walla tool yu jóge ci mbëj, maanaam lu ñeel yëngug, walla doxub, yani mbëj. Kàttanu mbëj manees na koo jëfandikoo ngir defi liggéey, leeral, tàngal,...

Kàttan ak dawaanu mbëj[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Digaale bi ci kàttan ak ngóora[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Kàttanu mbëj manees na koo natt ci dawaanu mbëj bi, balaa dara manees naa xayma liggéey bi

,

Liggéey bi W ciy joule, yan bi Q ciy coulomb ak wuuteeg aj gi ciy volt.

ak , I dawaanu mbëj bi, t jamono ji:

,

te di Ngóora ciy watt.

Kàttan gi manees na koo nattee nii:

Kàttan gi UE ciy Joule mooy kàttan gi rënku cib toolu mbëj, C mooy def bi, di ci lees di sukkandiku ngir man a xam daayoob kàttan gees man a sol cib fattalukaay.

Kàttan gi Um ciy Joule mooy kàttan gi rënku cib toolu bijjaakon, mooy walug bijjaakon giy soppiku ci jamono t.

Ci yenn anam yi dees na man a bind gii yamale:

Bennaanu natt[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Bennaanu natt bi ëpp lu ñuy jëfandikoo ngir natt ab limu kàttanu mbëj mooy kilowattwaxtu (kWW)

sunu xamee ne

S mooy saa

Xool it[Soppisoppi gongikuwaay bi]