Gàmmu wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Ahloubadar (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
MelancholieBot (waxtaancëru)
m roboto aldono de: az:Rəbiüləvvəl
Rëdd 10 : Rëdd 10 :


[[ar:ربيع الأول]]
[[ar:ربيع الأول]]
[[az:Rəbiüləvvəl]]
[[bn:রবিউল আউয়াল]]
[[bn:রবিউল আউয়াল]]
[[da:Rabîa I]]
[[da:Rabîa I]]

Sumb bu 19 Sattumbar 2009 à 23:17

Gàmmu, ( ci araab ربيع الأول) mooy ñetteelu weer ci weeri wolof tuddees na ko noonu ngir ne araab yi dañu ci daan lolliwu, maanaam daan ci am am ñax, di ci sàmm seenug jur, am ñu ne daa dëppoo ak lolli bi moo tax ñu tudde ko ko.

Ci wolof nak daa yem ak weer wees di màggalee juddug yonnent bi te màggal googu moo tudd Gàmmu ci wolof.

Xew-Xew

  • ci lees di màggal juddug yonnent bi, ci ñi yellal ni warees naa màggal ag juddoom.
Weeri wolof

Tamxarit | Diggi-gàmmu | Gàmmu | Rakki-gàmmu | Rakkaati-gàmmu | Maami-koor | Ndeyi-koor | Baraxlu | Koor | Kori | Diggi-tabaski Tabaski