Tundi Senegaal

Jóge Wikipedia.
Lonkoyoonu tundi Senegaal ci 2006 (laataa sosug tunduw Kungéel)

Tund yi ay dog lañu ci Séddaliinu Senegaal, nekk ci biir 14 diiwaani Senegaal yi.

Sosug tunduw Kungéel moo ko yóbb ci limub 35 ci atum 2006.

Dogiin[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Diiwaan Tund
Cees Mbuur Cees Tiwaawon
Fatik Fatik Funjunj Gosaas
Kawlax Kafrin Kawlax Kungéel Ñooro gu Rip
Koldaa Koldaa Séeju Wilingara
Luga Kebemeer Lingeer Luga
Maatam Kanel Maatam Raneru
Ndar Dagana Podoor Ndar
Ndakaaru Ndakaaru Géejawaay Pikin Tëngéej
Njaaréem Bambey Njaaréem Mbakke
Siggcoor Biñoona Usuy Siggcoor
Tambaakundaa Bàkkel Keedugu Tambaakundaa

Xool it[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lëkkalekaay yu biir[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Téerekaay[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
  • (fr) François Zuccarelli, « Le département sénégalais », Paris, Revue juridique et politique, n° 3, juillet-septembre 1968, p. 854-874


Drapeau du Sénégal 35 Tundi Senegaal raayab Senegaal

Bàkkel · Bambey · Biñoona · Dagana · Ndakaaru · Njaaréem · Fatik · Funjunj · Gosaas · Géejawaay · Kafrin · Kanel · Kawlax · Kebemeer · Keedugu · Koldaa · Kungéel · Lingeer · Luga · Mbuur · Maatam · Mbakke · Ñooro gu Rip · Ussuy · Pikin · Podoor · Raneru · Tëngéej  · Ndar · Séeju · Tambaakundaa · Cees · Tiwaawon · Wilingara · Siggcoor ·