Diiwaanu Kawlax

Jóge Wikipedia.
Diiwaanu Kawlax ci lonkoyoonu Senegaal

Diiwaanu Kawlax benn la ci juroom-ñenti diiwaani Senegaal yi. Réewu-taax mu kawlax mooy péeyu diiwaan bi, te ëpp ci solo it. Mi ngi réye 16010 km2, am 1 066 375 ciy way-dëkk

Féeteem ci Melosuuf[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Diiwaan bi ak ay tundam

Mi ngi peggook:

Ay tundam[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ba ñu defee tunduw Kafrin diiwaan ci 2008, diiwaan bi ñetti tund rekk la am:

Lëkkalekaay yu biti[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Raayab Senegaal 14 Diiwaani Senegaal Raayab Senegaal

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·