Diiwaanu Fatik
Apparence
Diiwaanu Fatik benn la ci diiwaani Senegaal yi.
Ci bëj-gànnaar ak ci bëj-gànnaar-peku, diiwaanu Cees, Jurbel ak Luga ñoo ko wër, ci bëj-saalumam Gaambi la taqalool, mbàmbulaanug Atlas gee ko féete sowwu.
Melosuuf
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Xeetu klimaam mooy bu sudaan-sahel. te yii Ñooy ay tundam:
Digi diiwaan bi yu tay jii, ñi ngi leen tëral ci àtteb 84-22 bu 22 diggi-gamu 1984. Laataa-loolu mi ngi bokkoon ci diiwaan bu yaa ba woon, di Siin-Saalum.
Am na 613 000 ciy way dëkk te yaatoo 7 930 km2
Lëkkalekaay yu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- (en) Statistiques Geo Hive
- (fr) Situation économique et sociale de la région de Fatick - Édition 2004 (rapport du Ministère de l'économie et des finances, août 2005)
| |||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |