Diiwaanu Koldaa
Apparence

Koldaa ngi bokk ci Kaasamaas, ci digg-bëj-saalumu Réew mi. Benn la ci fukk ak ñenti diiwaan yu Senegaal. Mi ngi yaatoo 21 011 km2 te am 847 243 ciy way-dëkk.

Ay tunduw
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ba ñu defee goxub Séeju diwaan ci 2008, la diwaan bi am ñaari gox rekk:
Lëkkalekaay yu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- Statistiques Geo Hive
- (fr) « Kolda : la pauvreté comme vitrine » (jukkib yéenekaay bu Le Quotidien)
| |||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |