Aadama
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Aadama mooy ni ñu ko waxe ci Lislaam (آدم). Ci angale mooy Adam te ci faranse itam mooy Adam. Mooy nit ki Yàlla jëkka sàkk.
Aadama ci Biibël ba[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Nettalib Aadama feeñ na ci Ge 1:26-30; 2:4-8; 15-20. Aadama dafa toppoon jabaram Awa ci bàkkaaram. Bàkkaar boobu mooy lu indi musiba yépp yi nu gis ci àddina si (Ge 3:6-21). At, ya Aadama dundoon, 930 la. (Ge 5:5). Ci Injiil dañuy wax ci Aadama ci Lu 3:38; Ro 5:14-19; 1Ko 15:22,45; 1Tim 2:13,14; Yu 1:14.
Aadama ci Alxuraan[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Nettalib Aadama feeñ na ci suraat 2:30-38; 3:33,59; 7:11,19-27; 17:61-62; 18:50; 19:58; 20:115-128. Nekk na ki borom bi ñëk bind mouy nit doon tamit yonent bi ñëk
doom Aadama[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Waxinu wolof bu tekki "nit ñi".