Xët wu njëkk

Jóge Wikipedia.

(Yoonalaat gu jóge Main Page)
Dem : Joowiin, Seet
Pix.gif
Pix.gif

Nataalu Wikipedia Dalal-jàmm ci Wikipedia

Jimbulang bu Ubbeeku bi

Seetal ci 1 017 jukki ci kàllaama wolof:

Pix.gif

Nas wi bokk na ci bëre biy dàq ber bi ñu ber yenn làkk yi (rawatina ci internet bi), xëcc itam gëndaloo guy yamale te di jàpplante, loolu di sukkandiku ci sañ-sañu askan yi gàddu seen kuute ci caada.

Àdduna bu gën di yamale, ak gën di tinkiku ci la aju !!!

Nuvola apps edu science.svg


Gnome-fs-client.svg


Nuvola apps kcoloredit.svg


Nuvola apps kuser.svg
Nuvola apps kuser.svg
Askan
Nataalu ayubés bi

Seex Ahmadu Bamba Xaadimur Rasuul (Cheikh Aḥmad ibn Muḥammad ibn Ḥabīb Allāh 1853-19 sulet 1927) boroom xam-xamu diine bu jullit la bu di ab sëriñ te cosaanoo ci ag càllala gu doomi soxna. Mi ngi gane àdduna ci Mbàkke, ab dëkk bu maamaatam sancoon ca nguurug Bawol, maamaatam jooju mooy Maharam, walla Maaraam,mooy ki sanc Mbàkke Bawol, waxees na ne loolu ci atum Shaqdadin la di (1194 g / 1780 g.j ) . Waaye dëkkewu fa woon, da fa a bàyyi woon ab taawam Muhammudu Farimata, magi habiibullaah ju mu bokkalul nday. Moom nag sëñ Maaram mii daa desoon Jolof, fa la làqoo ñu denci ko fa, di ko siaare.

Ñu koy woowe itam Xaadim Rasuul di Ñaari baati araab yuy wund Surgab yonent bi Muhammad (j.m). Mu bokk ci jëmm yi gën a fés te ëpp solo ci diiney Lislaam ci sowwu Afrig, ndax moom moo sos [[]]. Waa-réewam Seex Ahmadu Bamba lañu koy woowe ndax cofeel gu ñu am ci moom.


Yeneen sémbi Wikipedia ci yeneeni kàllaama. Nu lim ci ñenn ñi rekk


Yeneen sémbi Wikipedia ciy kàllaamay waa Afrig


Commons-logo-31px.png
Commons
Dàttub njoxeeb ay nataal
Wiktionary-logo-51px.gif
Wikbaatukaay
Baatukaay barilàkk
Wikiquote-logo-51px.png
Wikiquote
Dajaleeb ay tudd
Wikinews-logo-51px.png
Wikixibaar
Xibaari àdduna bi
Wikibooks-logo-35px.png
Wikitéere
Téerey njàng yu ubbeeku
Wikisource-logo-35px.png
Wikisource
Kaggu bu ubbeeku
Wikispecies-logo-35px.png
Wikispecies
Wayndareeb xeeti mindeef yépp
Wikiversity-logo-41px.png
Wikidaara
Jumtukaay ak yëngu-yëngu ñeel njàng
Wikimedia-logo-35px.png
Meta-Wiki
Nosuwaayu sémbi Wikimedia yi