Yoon

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet

Xët wii day dajale mbooleem tëriit walla jukki yu wuute ëmbiit te bokk tur. Disambig.svg

Yoon moom lanuy wax ci ntubaab (justice) dees na wax it yoon jublu ci li nuy wax (loi)walla (code) yoon tam dina tekki fi nit di jaar, dees na ci jublu it lu nosu maanaam tegu na ci yoon.

Yoon nag it ci nosteg penc (systeme republicuain) benn la ci ponk yi àtte gi (l'etat) di tegu di ci doxe, ponk yooyu ñaare ñatt lañu

  • yoon: fii bu ñu ko waxee mooy doole jiy àtte tooñaange yi di tege ci yoon, ci biiram lañuy fekk ëtt yeek àttekaay yi ak xaali yi ak layalkat yi ak lépp li ci aju
  • yoonal
  • wéyal


Xam-xam
Xam-xam
Gëstubiddiw | Jëmm | Paj | Saytubiddiw | Simi | Xam-xamu suuf si ak jawwu ji | Xayma
Xarala
Jokkoosoryante | Xaralaymbëj | Doolerandu | Kàttan | Xam-xamu nosukaay | Mbëjfeppal
Xam-xami nite ak mboolaay
Diine | Melosuuf | Wërlaay | Nit | Yoon | Koom-koom | Taariix | Xeltu | Kàllaama