Wikipedia:Xët wu njëkk

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet
Dalal-jamm ci bunt bi ñu jagleel askanu Wikipedia.

Soo amee yéene bokk ci jëmale-kanam jimbulang bi, ngala jàngal bu baax ana lan mooy ay àtteem, ci ponk yi mu lalu.
Man ngaa tambalee ci xëtu ndimbal wi. Di na tax nga xam lu bari ci Wikipedia.
Ci xët wii man nga fee gisee fooy defee ay laaj, fooy waxtaanee, ak lépp lu aju ci Wikipedia

@ fryr dyutodbvf fgter;erk fuyferb./shf fhgdsop/se39edgbv283fuy9372ey c[[nndv c731248b gytwqbndnaso eyywwhbeo euytehysa edytedhsuwe wywuwbwbuws bdytasaie eyed ddnssw hwd sosw udd shsisjuss swhwbw,ka shgaqbwi|

  • Su fekkee am na nit ku ngéen bëgg mu nekk yorkat mbaa ngéen bëgg koo doon yéen ci séen bopp, su boobaa bind leemjvn seen tur Fii.
  • Ngir dem ci pénc mi cuqal fii
  • Ngir dem vbnf fheid fhvs fhuid vbhxfS v vhnujhf fytdal djhs dbhgd dhf,a ci xëtu kalante wi
Yëgley Askan wi
soppi
Ay xibaar ngir gan ñi
soppi

Soo leen demee ci xëtu gan ñi di ngeen fa fekk ay xibaar yu leen di dimbali ngir ngéen man a tambalee cëru ci Wikipedia.
Man ngeen tamit def ay laaj (question).

Xibaar / Li gën a fés
A.W (Akaademi Wolof), aw na ci yoonu suqali Wolof !
Mbooloo mu di doomi réew mi dajee nañu ca Tuubaa sos ab Akaademi jagleel ko làkku Wolof. Ñu nar a joyal séen yitte yi gën a mag ci dajale mboolem mbindi mag ñi, ñi bind ci Wolof, gëstu yees ci jot a def, saytu arafi bindiin yi (yoy latin ak yoy alxuraan), tekki xam-xam yi ci Wolof, defar baatukaayu Wolof, defar tëraliinu jàng ak sóññ boroom xam-xam yi ñu sonn ci jàng ak binde ci Wolof. Ndajem boroom xam-xam la mu suqali Wolof rekk tax a jóg waliif wutum xaalis. Àndu ñook nguur mbaa kujjeg politig. Ñoom daal ñu moom séen bopp la ñu te sàkku mboolem ku Wolof ñor nga jàpp ci liggéey ngir suqali làkk wi rekk.

Ku ca bëgg a bokk mbaa nga bëgg ci yeneeni leeraal man ngaa bind ci : akaademibuwolof@gmail.com

Samay jumtukaay
Barabu tur

Wuute
Jëf
Joowiin
Boyotu jumtukaay yi