Diiwaanu Ndakaaru
Jóge Wikipedia.
Diiwaanu Ndakaaru, benn la ci fukk ak juroom-ñenti diiwaan yu Senegaal yi. Moo ci gën a tuuti, ci yaatuwaay, waaye moo ci gën a bari way-dëkk. Yaatuwaayam toll ci 550 km²
Ñoo ngi ko séddale ci ñenti Tund: Ndakaaru, Pikin, Géejawaay ak Tëngéj
[Soppi] Lëkkalekaay yu biti
|
|||
|
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |