Tunduw Ndakaaru

Jóge Wikipedia.

Ndakaaru wenn la ci 35 tund yees séddalee Réewum Senegaal, di it benn ci 4 tundi diiwaanu Ndakaaru, dëkku Ndakaaru mooy péeyu tund week diiwaan bi te am 1 030 594 ciy way-dëkk

Séddaliinu tund wi[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Tund wi dees koo dog-doge ci 19 dëkkaani ndiiwaan, di:

Lëkkalekaay yu biir[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Téerekaay[Soppisoppi gongikuwaay bi]

  • (fr) Ibrahima Diallo, Le droit des collectivités locales au Sénégal, Paris, L'Harmattan, 2007, 380 p. (ISBN 978-2-296-03770-0)
  • (fr) Djibril Diop, Décentralisation et gouvernance locale au Sénégal. Quelle pertinence pour le développement local ?, Paris, L'Harmattan, 2006, 268 p. (ISBN 2-296-00862-3)
  • (fr) François Zuccarelli, « Le département sénégalais », Paris, Revue juridique et politique, n° 3, juillet-septembre 1968, p. 854-874


Drapeau du Sénégal 35 Tundi Senegaal raayab Senegaal

Bàkkel · Bambey · Biñoona · Dagana · Ndakaaru · Njaaréem · Fatik · Funjunj · Gosaas · Géejawaay · Kafrin · Kanel · Kawlax · Kebemeer · Keedugu · Koldaa · Kungéel · Lingeer · Luga · Mbuur · Maatam · Mbakke · Ñooro gu Rip · Ussuy · Pikin · Podoor · Raneru · Tëngéej  · Ndar · Séeju · Tambaakundaa · Cees · Tiwaawon · Wilingara · Siggcoor ·