Diiwaanu Fatik

Jóge Wikipedia.

Diiwaanu Fatik benn la ci diiwaani Senegaal yi.

Ci bëj-gànnaar ak ci bëj-gànnaar-peku, diiwaanu Cees, Jurbel ak Luga ñoo ko wër, ci bëj-saalumam Gaambi la taqalool, mbàmbulaanug Atlas gee ko féete sowwu.

Melosuuf[Soppisoppi gongikuwaay bi]

diwaanu Fatik ak goxam

Xeetu klimaam mooy bu sudaan-sahel. te yii Ñooy ay tundam:

Digi diiwaan bi yu tay jii, ñi ngi leen tëral ci àtteb 84-22 bu 22 diggi-gamu 1984. Laataa-loolu mi ngi bokkoon ci diiwaan bu yaa ba woon, di Siin-Saalum.

Am na 613 000 ciy way dëkk te yaatoo 7 930 km2

Lëkkalekaay yu biti[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Raayab Senegaal 14 Diiwaani Senegaal Raayab Senegaal

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·