Diiwaanu Koldaa

Jóge Wikipedia.

Dem : Joowiin, Seet
Diwaanu Koldaa ci lonkoyoonu Senegaal

Koldaa ngi bokk ci Kaasamaas, ci digg-bëj-saalumu Réew mi. Benn la ci fukk ak ñenti diiwaan yu Senegaal. Mi ngi yaatoo 21 011 km2 te am 847 243 ciy way-dëkk.

Ay goxam

[Soppi] Ay tunduw

Ba ñu defee goxub Séeju diwaan ci 2008, la diwaan bi am ñaari gox rekk:

[Soppi] Lëkkalekaay yu biti

Raayab Senegaal 14 Diiwaani Senegaal Raayab Senegaal

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·