Wommatiinu mbëj

Jóge Wikipedia.

Wommatiinu mbëj walla Wommatiin wi moo nuy wax ci anam gi wommat wu mbëj wi di amee. Ci limam lanuy sukkandiku ngir man a xam ñaata la benn jumtukaay bi manee wommat mbëj. Safaanam di dëgërluwiinu mbëj wi di li lay wax ni ab jumtukaay manee dëggërlu jàllug dawaanu mbëj ci biiram.

Tekkeem[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Bennaanu nattu wommatiin wi mooy siemens ci meetar [s/m]. Nekk itam dawaanu mbëj ci kaw taraayu ab toolu mbëj [I/E]. lu bari bile araf lañu koy teewalee .

  • mooy Wommatiin wi
  • l mooy guddaayu wommatukaay bi (ñu koy natte meetar)

Lëkkalekaay yu biir[Soppisoppi gongikuwaay bi]