Wommat wu mbëj

Jóge Wikipedia.
Dem: Joowiin, Seet

Wommat wu mbëj ab tur bees jox benn feeñteb jëmm bi la ngir mu teewal nangu gu ab wommatukaay dawaanu mbëj jàll ko. Wommat wi dafa aju ci wommatiin wi. Wommat wi G mooy safaanu ndëgërlu gi R.

Bennanu natt bu wommat wi mooy siemens (s).

di ohm moom lañuy nattee ndëgërlu gu mbëj gi.

Digaaleem ak yeneeni kem[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ci yamale gi ci suuf la digaaleem ak Ndëgërlu gi gën a feeñee.

  • G mooy wommat wi,
  • R mooy Ndëgërlu gi,
  • I dawaan bi,
  • V dend bi.

Lëkkalekaay yu mbëj[Soppisoppi gongikuwaay bi]