Sudaan (diiwaan)

Jóge Wikipedia.

Sudan (jóge ci ab baatu araab bilâd as-sûdân "dëkkuwaayu ñu ñuul ñi", benn ci la diiwaani Afrik yi, tàmbalee ca penku Afrik ba ca sowwu Afrik, ci bëj-saalumu Sahel, tàmbalee ca Mali ba réewum Sudaan ci penku Afrik. Diiwaan bi mooy ëpp taw ci Sahel, mbay mi fa la gën a neexe. Ci bëj-saalumu Sudaan àllub Yemoo fa am.


Diwaani Afrig
Diwaani KMX: Diggu Afrig · Penku Afrig · Bëj-gànnaaru Afrig · Bëj-saalumu Afrig · Sowwu Afrig
Yeneen diwaan: Ginne · Bejjenu Afrig · Maghreb · Sahel · Afrig gu bëj-saalumu-Sahara · Sudaan