Bëj-gànnaaru Afrig wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Addbot (waxtaancëru)
m Bot: Migrating 96 interwiki links, now provided by Wikidata on d:q27381 (translate me)
JimeoWan (waxtaancëru)
m coppite yu néewal, dindi lëkkalekaay bu dee
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
[[Dencukaay:Africa-countries-northern.svg|right|Lonkoyoonu Afrig ak Réewi Bëj-gànnaaru Afrig.|]]
'''Bëj-gànnaaru Afrig''' mooy [[Diwaan|diwaanu]] Afrig bi féete ci li nekk ci kawu [[tàkk gu Sahara]].
'''Bëj-gànnaaru Afrig''' mooy [[Diwaan|diwaanu]] Afrig bi féete ci li nekk ci kawu tàkk gu [[Sahara]].


Mooy la nuy faral di wax ''Afrig gu weex'' gi, ndax melokaanu ña fa dëkk, bii baat day safaano ak '''Afrig gu ñuul''' gi, di tekki [[Afrig gu bëj-saalumu-Sahara]].
Mooy la nuy faral di wax ''Afrig gu weex'' gi, ndax melokaanu ña fa dëkk, bii baat day safaano ak '''Afrig gu ñuul''' gi, di tekki [[Afrig gu bëj-saalumu-Sahara]].

[[Dencukaay:Africa-countries-northern.svg|right|Lonkoyoonu Afrig ak Réewi Bëj-gànnaaru Afrig.|]]
== Séwógaraafi ==
== Séwógaraafi ==

Réewi bëj-gànnaaru Afrik:
Réewi bëj-gànnaaru Afrig :
* [[Dencukaay:Flag of Algeria.svg|border|20px|raaya]] [[Alseeri]]
* [[Dencukaay:Flag of Algeria.svg|border|20px|raaya]] [[Alseeri]]
* [[Dencukaay:Flag of Egypt.svg|19px|border|raaya]] [[Isipt]]
* [[Dencukaay:Flag of Egypt.svg|19px|border|raaya]] [[Isipt]]
Rëdd 14 : Rëdd 16 :


== Taariix ==
== Taariix ==
* Ci jamono ju yagg ja «Afrig» da doon jëmmal diwaanu [[Kaartaas]], mooy réewu Tiniisi gu tay. Afrik ab diwaanu Nguuru Rom gu Mag ga la woon . Bi [[jullit]] yi ñëwee, baat bi dañ kaa soppi, araabal ko [[Ifriqiya]].
* [[Beerbeer]] yi, ñooy way dëkk yiñ ni ñoo njëkk ci bëj-gànnaaru Afrig.
* [[Maghreb]] (sowu ci araab), moo ëmb réew yii: [[Gànnaar]], [[Marok]], [[Alseeri]], [[Tiniisi]] ak [[Libi]].
* «Afrig gu weex» bu njëkk da doon jëmmal barabu Afrig bi ay nit yu xees dëkkee: [[Marok]], [[Alseeri]], [[Tiniisi]], [[Libi]], [[Esipt]]. Waaye tay baat bi liñ kay jëfëndikoo bariwul.


* Ci jamono ju yagg ja « Afrig » da doon jëmmal diwaanu [[Kaartaas]], mooy réewu Tiniisi gu tay. Afrik ab diwaanu Nguuru Rom gu Mag ga la woon. Bi [[jullit]] yi ñëwee, baat bi dañ kaa soppi, araabal ko [[Ifriqiya]].
* [http://www.north-of-africa.com/ North of Africa]
* [[Beerbeer]] yi, ñooy way dëkk yiñ ni ñoo njëkk ci bëj-gànnaaru Afrig.
* [[Maghreb]] (sowu ci araab), moo ëmb réew yii : [[Gànnaar]], [[Marok]], [[Alseeri]], [[Tiniisi]] ak [[Libi]].
* « Afrig gu weex » bu njëkk da doon jëmmal barabu Afrig bi ay nit yu xees dëkkee : [[Marok]], [[Alseeri]], [[Tiniisi]], [[Libi]], [[Esipt]]. Waaye tay baat bi liñ kay jëfëndikoo bariwul.


{{diwaaniafrik}}
{{diwaaniafrik}}

Sumb bu 18 Sattumbar 2014 à 14:56

Bëj-gànnaaru Afrig mooy diwaanu Afrig bi féete ci li nekk ci kawu tàkk gu Sahara.

Mooy la nuy faral di wax Afrig gu weex gi, ndax melokaanu ña fa dëkk, bii baat day safaano ak Afrig gu ñuul gi, di tekki Afrig gu bëj-saalumu-Sahara.

Séwógaraafi

Réewi bëj-gànnaaru Afrig :

Taariix

  • Ci jamono ju yagg ja « Afrig » da doon jëmmal diwaanu Kaartaas, mooy réewu Tiniisi gu tay. Afrik ab diwaanu Nguuru Rom gu Mag ga la woon. Bi jullit yi ñëwee, baat bi dañ kaa soppi, araabal ko Ifriqiya.
  • Beerbeer yi, ñooy way dëkk yiñ ni ñoo njëkk ci bëj-gànnaaru Afrig.
  • Maghreb (sowu ci araab), moo ëmb réew yii : Gànnaar, Marok, Alseeri, Tiniisi ak Libi.
  • « Afrig gu weex » bu njëkk da doon jëmmal barabu Afrig bi ay nit yu xees dëkkee : Marok, Alseeri, Tiniisi, Libi, Esipt. Waaye tay baat bi liñ kay jëfëndikoo bariwul.

Diwaani Afrig
Diwaani KMX: Diggu Afrig · Penku Afrig · Bëj-gànnaaru Afrig · Bëj-saalumu Afrig · Sowwu Afrig
Yeneen diwaan: Ginne · Bejjenu Afrig · Maghreb · Sahel · Afrig gu bëj-saalumu-Sahara · Sudaan