Aller au contenu

Saara

Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Sahara)


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Saara : yay Afrig Saara ab màndiŋ la, mu ngi soxal Afrig gu bëj-gànnaar. Ak 9.200.000 km2, mooy màndiŋ bi gën a mag ci àddina si, te mooy ñetteelu màndiŋ bi gën a mag ci àddina si, gën a tuuti màndiŋ yi nekk ci Antartika ak bëj-gànnaaru Artiku rekk.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons