Xibaarfeppal

Ab jukkib Wikipedia.

Dem : Tukkin, Seet
Apple II, mooy nosukaay kenn (personal computer, di ko wax PC) bi njëkk.
Apple II, mooy nosukaay kenn (personal computer, di ko wax PC) bi njëkk.

Xibaarfeppal judd ci booloob ñaari baat yii di xibaar ak mbëjfeppal. Di tekki ab xeetu xam-xam buy settantal bépp fànnu xibaar jaare ko ci ay wuutuloxo yu mbëjfeppal.

Jamonoy nosukaay mi ngi am ndooteel ci jëm-kanamug mbëjfeppal ci Ñaareelu Xareb Àdduna bi. ci la ñu defar wuutuloxo yu noppi yi ci njëkk.

Seetal ci Wikbaatukaay man nga faa gis baat yi nga xamul
Samay jumtukaay