Limu réewi àdduna bi

Jóge Wikipedia.
Tëralin: - 0-9 A B C D E F G H I J K L M N O P Q R S T U V W X Y Z

A[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Afganistaan - Afrig gu Bëj-saalum - Dunu Aland - Albaani - Almaañ - Alseeri - Andoor - Angila - Angolaa - Antigua ak Barbuda - Araabi Sawdit - Armeeni - Arsantin - Aruba - Aserbayjaan - Ayiti

B[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Bahamas - Bahrayin - Banglaades - Barbados - Bareesil - Belaarus - Beliis - Beljik - Bene - Benesuwela - Bermuda - Boliibi - Bosni - Botswana - Brunaay Daarusalaam - Bulgaari - Burkinaa Faaso - Buruundi - Butaan - Dunu Buwet

C[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Cadd - Dunu Christmas - Ciipër

D[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Danmaark - Diwaan-yu-Bennoo - Dominika

E[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ecoopi - Ekwadoor - End - Eritere - Eslowaaki - Esloweeni - Estooni - Eswatini

F[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Duni Faarow - Dunu Falkland - Faraas - Fiiji - Filipiin - Finlaand

G[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Gaambi - Gaboŋ - Gana - Gine - Gine Bisaawóo - Gineg yamoo - Gires - Grenada - Groenlaand - Guam - Guwaadalup - Guwaatemala - Guyaana - Guyaana gu Faraas

I[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Imaarati Araab yu Bennoo - Indoneesi - Iraak - Iraan - Irlaand - Isipt - Islaand - Ispaañ - Israayil - Itaali

J[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Jamayka - Jeoorji - Jeoorji gu Bëj-saalum ak Duni Islaand yi Bëj-saalum - Jibraltaar - Jibuti - Jordaani

K[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Kaledooni-Gu-Bees - Kamboodi - Kamerun - Kanadaa - Kap Weer - Kasakistaan - Kataar - Duni Kaymaan - Keeñaa - Kirgistaan - Kiribati - Dunu Kokos - Koloombi - Komoor - Kongóo-Brasaawiil - Kongóo-Kinshasa - Dunu Kook - Kore gu Bëj-gànnaar - Kore gu Bëj-saalum - Korwaasi - Kosta Riika - Kot Diwaar - Kowet - Kubaa

L[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Lesoto - Letóoni - Libaa - Libeeria - Libi - Liechtenstein - Lituwaani - Luksembuur

M[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Madagaskaar - Makaaw - Malawi - Maldiif - Maleesi - Mali - Malt - Marok - Duni Marshall - Martinik - Mayoot - Meksik - Mikroneesi - Miyanmaar - Moldaawi - Monaako - Mongoli - Montserrat - Móoris - Móritaani - Mosaambik

N[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Namibi - Nauru - Nepaal - Nguur-Yu-Bennoo - Nikaraaguwa - Niseer - Niseeria - Niue - Dunu Norfolk - Norweej

O[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Olaand - Omaan - Onduras - Ongiri - Ooŋ Koŋ - Óstraali - Ótriis

P[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Pakistaan - Palau - Palestiin - Panamaa - Papuwaasi-Gine-Gu-Bees - Paraguwaay - Peru - Pitkeern - Polineesi gu Faraas - Poloñ - Poortorikoo - Portugaal

R[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Reiñoo - Réewum Cek - Réewum Diggu Afrig - Réewum Dominik - Réewum Lawos - Réewum Maseduwaan - Riisi - Romaani - Ruwandaa

S[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Saambi - Sahara gu Sowwu - Saint Kitts and Nevis - Saint Lucia - Saint Pierre ak Miquelon - Saint Vincent and the Grenadines - Salbadoor - Samowaa - Samowaa gu Aamerig - San Marino - Sapoŋ - Saw Tome ak Preesip - Seent Eleen - Seerbi - Seland-Gu-Bees - Senegaal - Seysel - Siin - Siiri - Sili - Simbaawee - Singapoor - Siraa Leyoon - Siri Laanka - Duni Solomon - Somali - Sudaan - Surinaam - Suweed - Suwis - Swalbard ak Jan Mayen

T[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Taaylaand - Taaywaan - Tajikistaan - Tansani - Timor-Leste - Tiniisi - Tirinidaad ak Tobaago - Tirki - Togóo - Tokelau - Tonga - Turkumenistaan - Tuvalu

U[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Ugandaa - Ukreen - Uruguwaay - Usbekistaan

V[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Duni Virgin (angalteer) - Duni Virgin (us)

W[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Wallis ak Futuna - Wanuatu - Watikaa - Wiyetnaam

Y[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Yaman