Ayiti
Jóge Wikipedia.
| Ayiti | |||||
|
|
|||||
![]() Barabu Ayiti ci Rooj |
|||||
| Dayo | km2 | ||||
| Way-dëkk | nit | ||||
| Fattaay | nit/km2 | ||||
| Xeetu nguur - Njiitu-Réew - Njiitu-Jëwriñ |
|||||
| Tembte - Bawoo - Taarix-ba |
|||||
| Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
|||||
| Làkku nguur-gi | |||||
| Koppar | |||||
| Turu aji-dëkk | |||||
| Njëkk-xayma | |||||
| |
|||||
Ayiti ab dun la bu nekk ca Amerik diggu. Day ab dun bu mag bu mu bokkal Republik dominicaine te Port-au-Prince di péyam.
Ayiti mooy reewu ñu ñuul ñi njëkka moom seen bopp ci attum 1804, ca seen fippu ga (1791-1803) ca la ñu dakkee Napoleon ak ay ñoñam ca dun ga.
Magginu turu dëkk ba [Soppi]
Ci aaday Taino yi, Ayiti da doon tekki suufu doj yu kawe ya walla aw doj ci biir geej.
