Bene
| Réewum Benin | |||||
|
|
|||||
Barabu Bene ci Rooj |
|||||
| Dayo | 112 622 km2 | ||||
| Way-dëkk | 8 439 000 nit | ||||
| Fattaay | 75 nit/km2 | ||||
| Xeetu nguur - Njiitu-Réew - Njiitu-Jëwriñ |
- Yayi Boni - |
||||
| Tembte - Bawoo - Taarix-ba |
-Fraas -01 Ut 1960 |
||||
| Péy ak rëddi - Tus-wu-gaar - Tus-wu-taxaw |
Porto-Novo |
||||
| Làkku nguur-gi | Nasaraan | ||||
| Koppar | Franc CFA (XOF) | ||||
| Turu aji-dëkk | -Bene-Bene -Sa-Bene |
||||
| Njëkk-xayma | +229 | ||||
Lonkoyoon bu Bene |
|||||
Benin (Republik bu Benin) : réewu Afrig.
- Lii Ab Sémp rekk la man ga cee dugal sa loxo ndeem am ga ci xam-xam
Melosuuf [Soppi]
Bene aw rëdduw suuf wu sew la, nekk ci diggante yamoo gi ak Gëwéelub Sànkar bi. Rëddu tus-wu-gaar wu bene mi ngi ci diggante 6°30'bëj-g ak 12°30'bëj-g, tu-wu-taxawam moom mi ngi ci 1° P ak 3° 40'P. Ay digam ñoo ngi yem ci Togóo ci sowwu, yem ci Burkina-faso ak Niseer ci bëj-gànnaar, ci Niseeriyaa ci penku, janook mbàmbulaanug Atlas gi ci bëj-saalum. Mi ngi am yaatuwaay bu tollu ci 112.622 yu kaare. Bene ngi bawoo ca dexug Niseer gi ci bëj-gànnaar yem ci mbàmbulaanug Atlas ci bëj-saalum ci ag tallalug 700 km. Diggante bi gën a guddu ci réew mi 325 km la.
Taariix [Soppi]
Lëkkalekaay yu biti [Soppi]
- (en) ICJ Judgment over the Benin-Niger boundary dispute, 12 July 2005 [1]
- (en) Fabio Spadi (2005) The ICJ Judgment in the Benin-Niger Border Dispute: the interplay of titles and ‘effectivités’ under the uti possidetis juris principle, Leiden Journal of International Law 18: 777-794 [2]
| Réewi afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkina Faso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eritere • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Ginne • Ginne Bisaawóo • Ginne gu Yemoo • Keeñaa • Lesoto • Libeeria • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeria • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome ak Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togóo • Tiniisi • Saambi • Simbaawee