Yamoo

Jóge Wikipedia.

Dem : Joowiin, Seet
Earth equator northern hemisphere.png

Ci melosuuf, yamoo gi aw rëddu tus-wu-gar la, di ag buumug jeneer gu ñu rëdd mu wër àdduna, jaar ci diggante dott yi. Yamoo gi moo xàjjale àdduna bi, def ko xaaju-kol-kol bu bëj-gànnaar ak xaaju-kol-kol bu bëj-saalum. Tus-wu-gaar wu yamoo gi 0° (tus aj). Guddaayu yamoo gu Suuf si mi ngi tollu, ci xayma, 40 075 km.

Tëraliin

[Soppi] Yamoog Suuf si

[Soppi] Klimaa

Klimaab barab yi ne ci li wër yamoo gi lañuy wax klimaab yamoo. Di nañ wax itam klimaab gëwéel, di bu barab yi ne ci li wër gëwéel yi (gëwéelub Tef ak gëwéelub Sànkar)

[Soppi] Réew yi mu dagg

Lonkoyoonu àdduna buy fesal yamoo gi

Ci sunu àdduna(Suuf si), yamoo gi ay mbàmbulaan ñoo ëpp ci li mu dagg ci yoonam, téeméer boo jël ci gudaayam ñaar-fukk ya rekk a jaar ci suuf.

[Soppi] Afrig

Yamoo gi jaar na ci juroom-ñaari réewi Afrig:

Ci « http://wo.wikipedia.org/wiki/Yamoo » lañ ko jële