Diiwaanu Tambaakundaa
Apparence
(Yoonalaat gu jóge Diwaanu Tambakundaa)
Diiwaanu Tàmbaakundaa mi ngi nekk ci penku réew mi, benn la ci 14 diiwaan yu Senegaal yi, di it bi ci ëpp ci rëyaay. Dëkku Tàmbakundaa mooy péeyub diiwaan bi. am na 605 695 ciy way-dëkk te yaatoo 59 602 km²
.
Melosuuf
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ay peggam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Diiwaan baa ngi digoo ak:
- Diiwaanu Maatam ak bu Luga ci bëj-gànnaaram;
- Diiwaanu Kawlax ak bu Koldaa ak réewum Gàmbi ci sowwam;
- Réewum Gine ci bëj-saalumam;
- Dexug Senegaal gi, fi mu janook réewum Mali, ci penkoom;
Ay goxam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ginnaaw bi, bi ñu defee Tunduw Kéedugu Diiwaan bu mat sëkk ci 2008, Péncum Réewum Senegaal la ngi ko def ci 1 diggi-gammu ci 2008, diiwaan bi ñaari Tund rekk la am:
Xool it
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Lëkkalekaay yu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- (en)Statistiques Geo Hive
- (fr)Conseil régional de Tambacounda
- (fr)Situation économique régionale de Tambacounda, édition 2005 (juin 2006)
| |||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |