Diiwaanu Njaaréem
Apparence
Diiwaanu Jurbel benn la ci diiwaani Senegaal yi. Amul benn ubbeeku ci géej gi.
Mi ngi yem ci diiwaani Cees ak bu Fatik ci bëj-gànnaaram, ci bëj-saalumam ci diiwaani Cees ak bu Fatik, ci penkoom ci diiwaani Fatik ak bu Luga, ci sowwam ci diiwaanu Cees. Am na lu tollu ci 1 049 954 ciy way dëkk te yaatoo 4 359 km2
Diiwaan bi mi ngi nekk tembe fa nguuru bawol ga nekkoon.
Ay tundam
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Xool it
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Téerekaay
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- (fr)Ibrahima Dieng, L'action des services sanitaires dans la région de Diourbel, Dakar, École nationale d'Administration, 1968, 151 p.
- (fr)J. Gard et Raymond Mauny, « Découverte de tumulus dans la région de Diourbel (Sénégal) », Notes Africaines, IFAN, Dakar, IFAN, 1961, n° 89, p. 10-11
- (fr)Ismaïla Lo, « La région de Diourbel », Sénégal d'Aujourd'hui, n° 16, 1970, p. 23-30
Lëkkalekaay yu biti
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
| |||
Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam · Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa · |