Xartum
Apparence

| Xartum الخرطوم | |
|---|---|
| Réew | |
| Tund | al-Chartum |
| Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
| Kawewaay | 382 m |
| way-dëkk | 2 090 001 nit |
| atum way-dëkk | 2 005 |
| Ab talib Xartum | |
Xartum (ci araab al-Khartûm الخرطوم ñu man koo tekkee «ñoxub ñay») mooy péeyu réewum Sudaan, féete ci wetu Niil bu weex, bi jóge Ugandaa, ak Niil bu baxa, bi jóge Ecoopi.
- Niil ca Xartum
- Diiwaanu Xartum
- Nataalub Xartum
