Tunis

Jóge Wikipedia.
Dem : Joowiin, Seet


Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Tunis تونس
Réew Flag of Tunisia.svg Tiniisi
Tund al-Chartum
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
36° 49′ Nord
     10° 11′ Est
/ 36.81, 10.18
Kawewaay 4 m
way-dëkk 728 453 nit
atum way-dëkk 2 004 411&Code_indicateur=0 301 007&Submit3=Envoyer delluwaay ((fr))
Rëyaay 212 63 km²
Fattaay 3 425 9 nit/km²
Dalub web www.commune-tunis.gov.tn
Mbeddum Habib Bourguiba ca Tunis
AvenueHabibBourguibaTunis.JPG

Tunis (ci araab تونس ) mooy dëkk bi ëpp ci Tiniisi, mooy péeyu réew ma dale 20 sattumbar 1159 (di 5 koor 554 ci arminaatu jullit ñi). Nekk ci bëj-gànnaaru réew mi , ci dóoxub Tunis bi ko tàqaleek déegub Tunis bi. Ña fa dëkk waa-tunis lees leen di woowee, ci suuf su yaa la tëdd man ngaa daw 30 km laa ngay àgg ca anéer ba.